Xalaat tv tacle Wally et ses danseurs: « Wally B. Seck le récidiviste, Daraay Alalu Aduna Jarul Lii » (Vidéo)

Xalaat tv tacle Wally et ses danseurs: « Wally B. Seck le récidiviste, Daraay Alalu Aduna Jarul Lii » (Vidéo)
Les danseurs de Wally Seck

Xalaat Tv n’a pas manqué de commenter le geste des deux danseurs de Wally Seck qui crée la polémique sur la toile.

« 2019 : Nga Sol Tee-shirt LGBT ?️‍? Mbotaayu Goorjigeen Yëpp Dila Deloo Njukël. Batay Setaloo Sa Dér Té Moonté Amoon Nga Occasion Ci Rassemblement « And Samm Jikko Yii »
2020 : Coronavirus Ñëw, Concert Amul, Mbumbaay Amul…Ngeen Waroon Ci Jàngg Deelu Seen Borom, Tuub Ndax Yërmandé Yàlla Dafa Yaatu
2021 : Ngeeni Foonënté En Direct Ngir Dëgël Seen Taxawaay Ci Doleel Mbon
Kuleen Ko Wax Ak Kuleen Ko Waxul Ay Ambassadeurs Goorjigeen Yi Ngeen Biir Sénégal.
Mboleem Artistes Yici Sénégal Yaay Kénn Kuñuy Deendalé Turëm Ay Borom Ñaari Tur Yi. Yaa Ñakk Jom ! »

Signaler une erreur

Vous avez repéré une erreur dans cet article ? Informez notre rédaction.

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *